Lidiop – Only One

Only One, le clip

Ça faisait un petit moment que l’on ne l’avait pas vu. Mais, après quelques échanges avec Lidiop, on a appris qu’il bossait sur son projet acoustique qui ne devrait pas tarder. Si on vous parle de cet artiste que l’on aime beaucoup sur le webzine, c’est que l’on vient de découvrir le clip du titre " Only One " présent sur son album Soul'n Mind.
Et cela tombe plutôt bien puisque, comme tout le monde le sait, demain, c’est la Saint Valentin et le jour où on fête l’amour. Le clip à été tourné sur les terres natales du chanteur, le Sénégal par Mao Sidibé et on peut dire qu’ils nous ont offert de belles images.

 

Soul’n Mind toujours disponible
Itunes
Deezer
Spotify

Lidiop
" Only One "

Visuel Only One ( Lidiop - crédit photo Mao Sidibé
photo utilisée avec l'accord de Lidiop - © photo : Mao Sidibé

Only One - Lyrics

Khole dou ome mome
Baniou koye beuse
Sama mbeugel mome
Rombeu na first
Yallabour moko binde
Keneu douko tass
Bindeunako dembeu
Mome sa aras
Sama mbeugeul si yaw
Moye sama sase
Dinala begeul ba keneu
Doula khass
Sama khole bi yaffiy first and the last
Sasounekeu malaye geuna love
Dinala begeul sasouma yewo
Altiné alarba alkhamess
Bo ma soré damay weet
Dema fone dima diegué
Dima ree

Refrain
You are the only one I bielive
You are the only one I desire
Everyday days every times haha

2 verset
Are you ready my lady
Sama life bi yafiye seki
Kaye niou dounde beugel
Ba rombeu love ho
Soma soriwé
Ma niroke doff ho ho
Fonek loumou sorry nako dokh
Beugeu ngadone sama makadi
Mane madone sa salamone
Beugeu ngadone sama yayou dome
Ndakh te yaw mi yamay wane yone ho
Lo beugeu ma defale lako
Lo diokhone rek ma dageu
Ndakhter yaw mi yadi sama love
Lo beugeu ma defalako
Lo diokhone rek ma dageu
Ndakhter yawmi yaddi sama love ho

Refrain

Mane de nala wakh lou keneu meusule wakh
Mane deh nala defale lou keneu
Meusula def
Lou beneu meune niar rako dakh
Worna yalla burr mome
Minou sakeu
Sasouneke mane maley tageu
Te bilahi walhahi mome dou meussa dakeu
Melni pith ak tageume
Talibé ak sangume
Teugeu ak ngaalamam
Doumala wethio ak dereume
Deréte bi nekeu sama yaram
Mane madone sa aladji nga done sama arame

Refrain

Combat bi makoy tegeu
Sama khole bi yafi bek
Deneubi yafiy teudeu sama reine ni khole
Yaw la love
Yaw la love yaw la love ho
Yaw la love ba moudié dof
Teunebi yafiye teudou
Khole dou ome mome
Baniou koye beuse
Sama mbeugel mome
Rombeu na first
Yallabour moko binde
Keneu douko tass
Bindeunako dembeu
Mome sa aras
Sama mbeugeul si yaw
Moye sama sase
Dinala begeul ba keneu
Doula khass
Sama khole bi yaffiy first and the last
Sasounekeu malaye geuna love
Dinala begeul sasouma yewo
Altiné alarba alkhamess
Bo ma soré damay weet
Dema fone dima diegué
Dima ree

Refrain
You are the only one I bielive
You are the only one I desire
Everyday days every times haha

2 verset
Are you ready my lady
Sama life bi yafiye seki
Kaye niou dounde beugel
Ba rombeu love ho
Soma soriwé
Ma niroke doff ho ho
Fonek loumou sorry nako dokh
Beugeu ngadone sama makadi
Mane madone sa salamone
Beugeu ngadone sama yayou dome
Ndakh te yaw mi yamay wane yone ho
Lo beugeu ma defale lako
Lo diokhone rek ma dageu
Ndakhter yaw mi yadi sama love
Lo beugeu ma defalako
Lo diokhone rek ma dageu
Ndakhter yawmi yaddi sama love ho

Refrain

Mane de nala wakh lou keneu meusule wakh
Mane deh nala defale lou keneu
Meusula def
Lou beneu meune niar rako dakh
Worna yalla burr mome
Minou sakeu
Sasouneke mane maley tageu
Te bilahi walhahi mome dou meussa dakeu
Melni pith ak tageume
Talibé ak sangume
Teugeu ak ngaalamam
Doumala wethio ak dereume
Deréte bi nekeu sama yaram
Mane madone sa aladji nga done sama arame

Refrain

Combat bi makoy tegeu
Sama khole bi yafi bek
Deneubi yafiy teudeu sama reine ni khole
Yaw la love
Yaw la love yaw la love ho
Yaw la love ba moudié dof
Teunebi yafiye teudou

 



Partagez cet article sur vos réseaux sociaux :

Ces articles en relation peuvent aussi vous intéresser...

Ces artistes en relation peuvent aussi vous intéresser...